Revelation 1:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gisleen, mi ngi ñëw ci niir yi,te ñépp dinañu teg seeni bët ci moom,ba ci ñi ko jam sax.Te xeet yi nekk ci kaw suuf yéppdinañu jooy ndax moom.Waaw. Amiin.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ngoogu di dikk, indaale niir yi, te ñépp a koy teg bët, ba ca ña ko jamoon sax, te giiri kaw suuf yépp ay jooy ndax moom. Noonu la moos. Amiin.