bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Revelation 1:8
Revelation 1:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Boroom bi Yàlla nee na: «Man Yàlla maay Alfa ak Omega, maay ki nekk, ki nekkoon démb te di ñëw ëllëg, man Aji Kàttan ji.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Man, maay Alfa, di Omega », la Boroom bi Yàlla wax, moom Ki masa Nekk, Ki Nekk, di Kiy Dikk ëllëg, te di Aji Man ji.