Revelation 10:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw loolu ñu ne ma: «Fàww nga wax ci kàddug Yàlla lu jëm ci réew yu bare, xeet yu bare, kàllaama yu bare ak buur yu bare.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu ñu ne ma: «War ngaa waxati ay waxyu ngir xeet yu bare, ak askan yu bare, ak niti làmmiñ yu bare, ak buur yu bare.»