Revelation 10:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu baat, ba ma déggoon ca asamaan waxaat ak man, ne ma: «Demal jël téere bi ñu ubbi ci loxob malaaka, mi taxaw ci géej gi ak suuf si.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee baat, ba ma déggoon, mu bawoo asamaan, dellu wax ak man, ne ma: «Demal jël téere bu ndaw bi ñu ubbi ci loxol malaaka, mi ŋarale géej geek jéeri ji.»