Revelation 11:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
naan:«Nu ngi lay gërëm, Boroom bi Yàlla,yaw Aji Kàttan ji, ki nekk te nekkoon,ndax gànjoo nga sa kàttan gu réy gi,ngir taxawal sa nguur.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne: «Boroom bi Yàlla Aji Man, ji nekk te nekkoon, nu ngi lay gërëm, ndax yaa ràngoo sa kàttan gu màgg, taxawal sa nguur.