Revelation 12:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu ma dégg baat bu xumb jóge asamaan naan:«Léegi mucc agsi na,moom ak kàttanak nguuru Yàlla sunu Boroom,ak sañ-sañu Almaseem,ndaxte ki daan tuumaal sunuy bokk,di leen sosal guddi ak bëccëgci kanam Yàlla sunu Boroom,kooka daaneel nañu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ma dégg baat bu xumb bawoo asamaan, ne: «Léegi nag texe teew na, ànd ak sunu kàttanu Yàlla ak nguuram, ak sañ-sañu Almaseem, ndax xalab nañu ki daan tuumaal sunu bokk yi, di leen sosal guddeek bëccëg fi sunu kanam Yàlla.