Revelation 12:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Geenam di laawaale ñetti cér yu ne benn ca biddiiwi asamaan, di leen sànni ci suuf. Ninkinànka ja taxaw ca kanamu jigéen jay matu, ngir lekk liir ba, bu juddoo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Geenam gi daldi buube fa asamaan benn ñetteelu biddiiw yi, rattax leen ci suuf. Ninki-nànka jaa ngi taxaw ci kanam ndaw siy matu, ngir bu xale bi juddoo rekk, mu lekk ko.