Revelation 12:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu xare am ca asamaan ya. Mikayel ak malaaka, ya ànd ak moom, xeex ak ninkinànka ja, ninkinànka ja it ak ay malaakaam feyyu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab xare nag jibe fa asamaan. Mikayel aki malaakaam di xareek ninki-nànka ji, ninki-nànka jeeki malaakaam it di xare,