Revelation 13:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Lii nag mooy laaj xel: ku am xel dina man a waññ siifaru rab wi, ndaxte siifar boobu mengoo na ak bu nit, di juróom-benni téeméer ak juróom-benn-fukk ak juróom-benn.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fii nag xel la laaj: ku am ug dégg, na waññ limu rab wi, ndax boobu lim turu nit la taxawe, di juróom benni téeméer ak juróom benn fukk ak juróom benn (666).