Revelation 13:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mayees ko, mu xare ak gaayi Yàlla yi te noot leen. Mayees ko it sañ-sañ ci kaw bépp giir, réew, kàllaama ak xeet.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu may ko itam mu xareek ñu sell ñi, duma leen, boole ci may ko sañ-sañ ci kaw niti gépp giir ak wépp xeet ak wépp làmmiñ ak wépp askan.