Revelation 14:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ma xool noonu, gis Mbote ma taxaw ci tundu Siyon, ànd ak téeméer ak ñeent-fukk ak ñeenti junniy nit, te ñu bind ci seen jë turu Mbote ma ak turu Baayam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma xoolaat, gisuma lu moy Gàtt bi fa mu taxaw ci kaw tundu Siyoŋ ak téeméer ak ñeent fukk ak ñeenti junniy nit (144 000) ñu ànd ak moom, te ñu bind ci seen jë turu Gàtt bi ak turu Baayam.