Revelation 14:6 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu ma gis meneen malaaka naaw ca digg asamaan, yor xebaar bi sax, di ko yégal waa àddina — xeet yépp, giir yépp, kàllaama yépp ak réew yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ma gis meneen malaaka muy naaw ci digg asamaan, ànd ak xibaaru jàmm bi sax dàkk, ngir baaxe ko waa àddina: niti wépp askan ak gépp giir ak wépp làmmiñ ak wépp xeet.