Revelation 14:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Meneen malaaka, di ñaareel bi, topp ca naan: «Daanu na! Babilon, dëkk bu mag, bi daan màndil réew yépp ak biiñu njaaloom, daanu na.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Meneen malaaka, topp ci, di ñaareel bi. Mu ne: « Babilon a daanoo, dëkk bu mag ba daanu na! Moom ma daan màndal askanoo askan biiñu moyam muy indi am sànj.»