Revelation 15:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku la ragalul, Boroom bi?Ku dul màggal saw tur?Kenn, ndaxte yaw rekk yaa sell.Xeet yépp dinañu dikk, jaamu la,ndax say àtte bir na ñépp.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom bi, ana ku la ragalul? Ku dul màggal saw tur? Yaw doŋŋ yaa sell. Askan yépp ay dikk, sujjóotsil la, ndax yaa jubi dogal.»