Revelation 15:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw loolu ma xool, noonu kër Yàlla ubbiku ca asamaan, muy tàntu màggalukaay, bi ëmb li Yàlla seede.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu ma xoolaat, daldi gis màkkaan ma fa asamaan, xayma ba fat seede si, mu ubbiku.