Revelation 16:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ñuy xarab Yàllay asamaan ndax seeni metit ak seeni taab. Waaye tuubuñu seeni jëf.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
tuubuñu seeni jëf, xanaa di saaga Yàllay asamaan ndax seeni mitit ak seeni taab.