Revelation 16:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Juróom-benneelu malaaka ma sotti ndabam ci dex gu mag, gi ñuy wax Efraat, ndox ma daldi ŋiis, ngir waajal yoonu buuri penku, yiy ñëw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Juróom benneelu malaaka mi sotti ndabam ci dex gu mag, gi ñuy wax Efraat, dex gi daldi ŋiis, ngir sàkkal buuri penku yiy dikk, aw yoon.