Revelation 16:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci kaw loolu juróom-ñaareelu malaaka ma sotti ndabam ci ngelaw. Noonu baat bu xumb jóge ca gàngune ma ca kër Yàlla ga, naan: «Lépp mat na.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee juróom ñaareelu malaaka mi sotti ndabam ci kaw ngelaw li, baat bu xumb jóge ca ngàngune ma ca màkkaan ma, ne: «Sotti na!»