Revelation 16:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu mu am ay melax ay riir ay dënnu ak yengu-yengub suuf bu mag, boo xam ne bési cosaan ba léegi, musu faa am. Yengu-yengub suuf si réye na noonu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee, ay melax tàkk, ay kàddu aki dënu riir, suuf yëngu yëngu bu réy bu masula am ba nit teewee ci kaw suuf ba bésub keroog. Noonu la yëngub suuf ba yéemee te réy.