Revelation 17:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Rab wi nekkoon te nekkatul nag, moom ci boppam moo di juróom-ñetteelu buur bi, te ci juróom-ñaar yi la bokk. Ma nga jëm sànkute.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Rab wi masoona nekk te nekkatul nag, moom ci boppam moo di juróom ñetteelu buur bi, kenn la ci juróom ñaari buur yi jiitu itam, te day sànkuji.