Revelation 17:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dinañu xare ak Mbote mi, waaye Mbote mi dina leen daan, ndaxte mooy kilifag kilifa yi, di Buuru buur yi. Te am toppam, di ñi mu woo te tànn leen, te ñu takku ci moom, dinañu daanandoo ak moom.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dinañu xare ak Gàtt bi, waaye Gàtt bee leen di daan, ndax mooy Sangu sang yi, di Buuru buur yi. Mooy daan mook ñoñam, ñi mu woo, tànn leen te ñu saxoo topp ko.»