Revelation 18:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dinañu wax naan: «Yëf yi nga bëggoon a am raw nañu la, te lépp luy yafal walla col gu rafet ñàkk nga ko, te kenn du ko gisaat!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dinañu ne: «Doomi garab yi nga soppoon sore na la, mboolem lu neex ak lu yànj réer na la mërr!»