Revelation 18:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Baana-baana, yi daan jaay yëf yooyu ba woomle, dinañu sore ndax ragal coonoom. Dinañu jooy di naqarlu,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña daan jula yooyii ci dëkk bi ba woomle, fu sore lañuy dànd, ndax ragal toskarey dëkk bi, di yuuxook a jooyoo,