Revelation 18:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
sa alal ju bare jépp naaw na ci wenn waxtu!» Noonu ñépp ñiy dawal gaal ak ñi ciy tukki ak ñi ciy liggéey ak ñi ciy baana-baana, ñépp di sore bérab boobu,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
wenn waxtu rekk, alal ju baree nii neen!» Dawalkati gaal yeek julay géej yi, ak mool yi, ak mboolem ñiy dunde géej, ñoom ñépp a ngi dànd fu sore,