Revelation 18:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
te bu ñu séenee saxar sa cay jollee, naan: «Ndax dëkk bu niroo woon ak dëkk bu mag bii mas na am?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
séen saxaras lakku dëkk bi di jalu, naan: «Bii dëkk bu mag, ana dëkk bu masa nirook moom?»