Revelation 18:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñuy xëpp suuf ci seen bopp, di jooy, di naqarlu te naan:«Ngalla yaw! Ngalla yaw,dëkk bu mag bi nga xam neci la boroom gaal yépp woomle ndax sa barele,ci wenn waxtu nga gental.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dañuy xëpp suuf seen kaw bopp, di yuuxook a jooy ak a naqarlu, naan: «Wóoy, wóoy, ngalla dëkk bu mag ba! Sa koom a woomal mboolem boroom gaal ci kaw géej, wenn waxtu rekk, nga gental.»