Revelation 18:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Niitug làmp du tàkkati,te baatu boroom séet ak séetam dootul jib ci yaw ba fàww.Ndaxte say baana-baana ñoo yilifoon àddina,te xeet yépp réer nañu ndax say luxus.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
làmp du niiteeti fi yaw, te baatu boroom séet akub séetam du jibeeti fi yaw mukk, ndax say julaa ëppoon doole ci àddina, te say xërëm a sànk askanoo askan.»