Revelation 18:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te deretu yonent yi ak gaayi Yàlla yiak ñépp ñi ñu rey ci kaw suuf,ci moom Babilon lañu ko fa fekk.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci yaw it lañu fekk deretu yonent yeek ñu sell ñi ak mboolem ñi ñu rey ci kaw suuf.