Revelation 18:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ay bàkkaaram dajaloo nañu ba ci asamaan, te Yàlla fàttaliku na ay jëfam yu bon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaxte ay bàkkaaram jalu na ba àkki asamaan, te Yàlla bàyyi na xel ay ñaawtéefam.