Revelation 18:6 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Dellooleen ko li mu defoon, feyleen ko ñaar ci li mu lebaloon, feesal-leen koppam ak naan gu gën a wex ñaari yoon naan ga mu joxe woon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na mu jëfe ak yeen, jëfeleen ko ak moom, feyleen ko ñaari yoon ay jëfam. Kaas bi muy xellile am njafaan, feesalal-leen ko njafaan lu ko ëpp doole ñaari yoon.