Revelation 19:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu ñaar-fukki mag ña ak ñeent, ak ñeenti mbindeef ya, daldi sukk di jaamu Yàlla, moom mi toog ca gàngune ma. Ñu naan:«Amiin! Aleluya!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ñaar fukki mag ñeek ñeent ak ñeenti bindeef yi ne gurub sukk, sujjóotal Yàlla, mi toog ci ngàngune mi. Ñu bokk ne: «Amiin! Aleluya!»