Revelation 19:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ma dégg lu mel ni baatu mbooloo mu bare, mel ni riiru duusi géej, ni yenguy dënnu yu réy, naan:«Aleluya!Ndaxte sunu BoroomYàlla Aji Kàttan jidugg na ci nguuram.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma daldi dégg lu mel ni coowal mbooloo mu bare, mu àddoo ni riirum géej, tey nirook kàddug dënu gu réy, ne: «Aleluya! Sunu Boroom Yàlla Aji Man ji mooy Buur!