Revelation 19:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nanu bég te bànneexute jox ko ndam li,ndaxte céetu Mbote mi agsi na,séet bi waaj na.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nanu bég, di bànneexu te màggal ko, ndax céetu Gàtt bi agsi na, ab séetam defaru na ba noppi!