Revelation 2:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye am na lu ma naqari ci yaw, moo di uuf nga foofu gaa yuy sàmm njàngalem Balaam, moom mi jàngaloon Balag, mu sóob bànni Israyil ci bàkkaar, xiir leen ci lekk ñam wu ñu tuuroo xërëm yi, xiir leen ci njaaloo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waaye lenn a ngi lu ma lay sikke: yaa ngi uuf foofu ay nit ñuy saxal njànglem Balaam, moom mi doon xiirtal Balag ci tegal Israyil ndëgg-sërëx, ngir ñu lekk ñam wu ñu sarxal ay tuur, ak di gànctu.