Revelation 2:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te am nga noonu itam ay nit ñuy sàmm njàngalem ñoom Nikolas.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka noonu itam yaa ngi uuf ay nit ñuy saxal njànglem ngérum Nikolas.