Revelation 2:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Réccul kon; lu ko moy dinaa dikk ci yaw léegi te xeex ak nit ñooñu ak jaasi, jiy génn ci sama gémmiñ. i
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag tuubal. Lu ko moy maay dikk léegi ba fi yaw, te saamar biy lange sama gémmiñ, moom laay xareek nit ñooñu.