Revelation 2:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
May naa ko ab diir, ngir mu tuub njaaloom, waaye bañ na.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
May naa ko ab diir, ngir mu tuub, waaye moo buggula tuub ngànctoom.