Revelation 2:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Dinaa rey ay doomam, te mboolooy ñi gëm yépp dinañu xam ne, man maa di kiy nattu xol ak xalaat, te dinaa fey ku nekk ay jëfam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am mbas laay fàdde ay taalibeem. Su ko defee mboolooy gëmkat ñépp dinañu xam ne man maay nattu xol ak xel, te maay fey ku nekk ay jëfam.