Revelation 2:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Xam naa it ne muñ nga, ba dékku coono ndax sama tur, te xàddiwoo. i
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam naa it ne muñ nga te sonn nga moos ngir man te xàddiwoo.
Recommended Reading