Revelation 20:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeneen néew yi duñu dekki, fi ak junniy at yi matul. Loolu moo di ndekkite lu jëkk li.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu moo di ndekkite lu jëkk li. Yeneen néew yi nag, duñu dekki li feek junniy at yi matul.