Revelation 20:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
te dina dem naxi xeet yi ci ñeenti xeblay àddina, maanaam ñoom Gog ak Magog. Dina leen dajale ngir xare, te dinañu bare ni peppi suuf cig tefes.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mu dikk, naxsi askani ñeenti colli àddina, yi ñuy wax waa Gog ak Magog. Mu dajale leen ngir xare, ñu bare ni feppi suufas géej.