Revelation 20:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dinañu sam suuf sépp, di wër dalu gaayi Yàlla yi ak dëkk, bi Yàlla bëgg. Waaye safara daldi jóge asamaan, lakk leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dañuy sam déndub suuf sépp, daldi yéew dalub nit ñu sell ñi ak dëkk bu jar bi. Ci biir loolu sawara wàcce asamaan, lakk leen.