Revelation 21:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ki doon wax ak man amoon na nattukaay, di bantu wurus bu mu doon natte dëkk ba ak miir ba ko wër, ak bunt ya.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kiy wax ak man nag, mu ngi yor yetu nattukaayu wurus, ngir natt dëkk bi aki buntam ak tataam.