Revelation 21:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dëkk ba dafa kaare, guddaay ba ak yaatuwaay ba ñoo tolloo. Mu natt dëkk ba ak bant ba mu yor. Guddaay ba, yaatuwaay ba ak taxawaay ba lépp tolloo, di fukki junni ak ñaar ciy estat.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëkk bi dafa kaare; guddaay bi tollook yaatuwaay bi. Mu natte dëkk bi bant bi mu yor, guddaay bi ak yaatuwaay bi ak taxawaay bi, lépp tolloo, di fukki junneek ñaari dayo (12 000), yemook ñaari junneek ñaar téeméeri kilomeetar (2 200).