Revelation 21:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Fondamaay miiru dëkk ba rafetale nañu leen xeeti per yu nekk.Fondamaa bu jëkk ba jamaa la;ñaareel ba, per bu bulo bu ñuy wax safir;ñetteel ba, per bu wert bu ñuy wax kalseduwan;ñeenteel ba, per bu wert te lerax, bu ñuy wax emëróot;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Doju kenug dëkk bi, xeeti gànjar ju nekk lañu ko rafetale. Doju kenu gu jëkk gi di jàspë; ñaareel bi di safiir; ñetteel bi di kalseduwan; ñeenteel bi di emëródd;