bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Revelation 21:22
Revelation 21:22 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Gisuma ca dëkk ba kër Yàlla, ndaxte Boroom bi Yàlla Aji Kàttan ji ak Mbote ma ñooy màggalukaay ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab jaamookaay nag, gisuma ko fenn ci biir dëkk bi, ndax Boroom bi Yàlla Aji Man ji ak Gàtt bi ñooy jaamookaay bi.