Revelation 21:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Dëkk ba soxlawul jant walla weer ngir leeral ko, ndaxte ndamu Yàlla moo koy leeral, te Mbote ma moo nekk làmpam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te dëkk bi soxlawul jant bu koy leeral mbaa weer, ndax leeru Yàllaa koy leeral, Gàtt bi di làmpam.