Revelation 22:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te Xelum Yàlla ak séetu Mbote mi ñu ngi naan: «Ñëwal.» Képp ku dégg wax jii, na ne: «Ñëwal.» Na képp ku mar, ñëw; ku bëgg, duyal ci ndoxum dund mi te doo fey dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noo gi ak Séet bi neeñu: «Ñëwal!» Ku ci dégg it, neel: «Ñëwal!» Ku mar, ñëwal; ku bëgg ci ndoxum dund mi, jëlal, ñu may la.