Revelation 22:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu malaaka ma ne ma: «Wax jii ju wóor la te dëggu. Boroom bi, Yàlla jiy leeral xeli yonent yi, moo yónni malaakaam, ngir mu won ay jaamam mbir yi dëgmël di ñëw.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee malaaka mi ne ma: «Lii wax ju wóor la te dëggu. Boroom bi Yàlla miy xelal yonent yi, moo yebal malaakaam, ngir mu won jaamam ñi mbir yi dëgmal te du jaas.»