Revelation 3:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
waaye ndax li nga nugg, tàngoo seddoo, dinaa la yàbbi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw nii nga nugge nag; tàngoo, seddoo, dinaa la yàbbi.